PROVERBES ET CITATIONS WOLOFS
1. Ku sa yaakaar tas nga ñeme loo ñemewulwoon
2. Ku ñu tek lu ëpp sa fit nga daw
3. Kemtaam moy xalatlo nit
4. Ko yémaluk responsabilité bouko may sa xeuy
5. Jambaar bu dewe ci xare lumu don facc du faju
6. Ku jak te amoulo kula dalal mënë juur lune
7. Ku nité ken meunoul gañou ci yaw
8. Guddu fan du yak dundu fek ngay jamu Yalla
9. Pexe muy jariñ moy banga bayek Yalla pexem banopi
10. Jamm dañukoy wotal
11. Niru sa baye niru sa jamano moko gueune
12. Kudul jum lo def nonula
13. Ku mucc ci xëlënto sa dundu nex
14. Cëryi bici ëpp dolé moy Yalla far ak yaw
15. Yalla yatuna fu way jap dém
16. Pass pass janla day yek di wacc
17. Yalla du bamu aduna
18. Ñaw njortu ñaka wolu sa bopla
19. Dundu ken duko dundu dañukoy ataan
20. Jambar amul min lu jafé am
21. Fu yet jek ken warufa ték ngërëm
22. Jambar ju amul xel ci luko jarul lay dee
23. Kilifa mbay yu wute duko nakari
24. Lo def ba sa dolé jexsa lulaca gënë sagal faratala
25. Nit ñaar rekay tax and ak mom ben ga and ak mom ngir Yalla dara duca yakku wala nga and ak mom ngir aduna dana dissi ba ngéne jëlënté yet
26. Lu amul sede wérul
27. Kuñuy tag sa mame tee sa yaram sumékuwul bo fékéwon jihad do bok sa jambarya
28. Yalla day jay Alahira ci Adouna bu jak
29. Rew ben bop bén wén napalko luca méti wet guné yëgko
30. Bép may buñula may té yëguéwula ci jiko yonétbi wacal baxul
31. Ken rek mo jaxal Yalla kiné fuma jëm
32. Bëg sama deer set du tax ma takal gor
33. Bu problém amul solution du am
34. Bëré pexe saf Yalla ko guëne
35. Yalla nagouwul kuko fék faga koy ëko
36. Cono buko cofél lalé borom duko yëg
37. Lu njalbénga séw naca sa xél dal
38. Dundu bu tegouwul ci xamé ak jiko jaratouko
39. Dundu bunekatul écol jaratuko
40. Kiga gënë bokal moy kiga bokal léru yonétbi
41. Njubadi fumu nek xame dufa nék
42. Jambar du wet borom xel mu rafet du wet
43. Bakar yiw bu dëngela
44. Ligay jënde Yalla bessagui ñeuw ga siplola
45. Cono bu jituwul pass pass mënula am
46. Katay borom dëg mo gën fouf tangali badola
47. Ragal Yalla moy fexe ba yiw moytu yiwadi boko yëgué sa bop rek ragalga Yalla
49. Jabaru facc mer baxul day muju sopaliku jan matla
50. Xol ken duko muñe xol atanul muñ xel lañuy muñe
51. Bu jiko dako lep daku
52. Buma wax dine nitki waxma xaritam ma waxla dinem
53. Bu soxla amul na sen jotayu nek ëpp
54. Goor pir moy xam naxam ne pat
55. Kuy bërek kudul danu bu yabo waj sa danu
56. Bép may bo mënti am té yobaléwul sa jiko ci jiko yonentébi bayil mayga moussibala ci yaw
Inscrivez-vous au blog
Soyez prévenu par email des prochaines mises à jour
Rejoignez les 85 autres membres